One Love Galsen

"ONE LOVE GALSEN"

Refrain :

*Ma Dikkeuti*
- B. I. G. D Big D number One
- Hardcore super like the One
- Yatfu is where am from
- Tieurre ju makk Jojo, Gofu, Dry Gun

Partie 1:

Demb a takh niou nane téy
Téy a takh niou nane euleuk
Fént neign fi Galsen, beupp mbidef tekk si beutt
Xouli beutt-xaali beutt
Fogg né di neign dokh di seugg
Head Hight
Sunu honneur deign ko fight
Respect, Love, Dignity dou niou si tayi
Khékhal askan wi mo niou fi bayi
Yokk sa fitt séy guéntes done reality
Takhawu lène by any means necessary
Su niou doné li niou done téy DEUG a takh
Rap a takh
Beug sunu réweu a takh
Show love ak notoriété di gueun di sakh
Li niou dji rek ngèye gôbe, Rap bi dou ay nakh

Partie 2:

Microphone Open dou mousseu Off bayi ko si On
B. I. G. D Big D héy super like the One
Takkalé bah takkalo
Beuri fulla Fass diom
Mouvement Galsen Hip hop
Beuri dolé, Never stop
Old school, New school, All generations
Siggil ngène Galsen si bepp situation
iindi innovation si ngour ak politique, structure, médiation
Ngathié-galama waw gore félicitations
Galsen ala athiou toujours prêt passe à l'action
Never give up jusqu'à pleine satisfaction
Loxxo si kaw képp ku sope Hip hop

Partie 3:

Na loxxo yi batcheu si kaw tachulen
Niou represent Galsen Clap your hands
Nio la beug nio la sope Galsen
Kone you and you and you fétch'len
Yatfu fénk na, la rawane ya done wakh am na
Degglou ma mbekté la
Yatfu fénk na, la rawane ya done wakh am na
Wesh wesh yow
Taxx ga dou taxx da ma taxx-taxxal té done a takh
Yatfu a takh, wakhandé la gou dentch a wakh
Diokh ma xalima, diokh ma da sama ada la, fenkal feinte ay firnday né wakhandé la gou dentch wakh.

Big D.

Most popular songs of Big D

Other artists of Dancehall