Niata Nio Dess

Sama xol lay méti samay xarite daw
Sama guiss guiss seu reuy sama beute yi ndaw
Wakh nga deug ndank, fène sa baate ci kaw
Maa bou bégué bég naa I don't give a fuck

Siiw dou dara loudoul yonou noone
Ndam moy indi siiw siiw moy indi noone
Yagouma ci thioow sila deuk man
Naathie bi féké woulé Bidéw féké woulé
Mane Djoumna té Buur Yallah baalma lou beuri yone
Dom meuno baakh ba sa Papa roy ci yaw
Mane ak samay xarite danio neutre ni arbitre
Ma done rancunier meurtrier pour chaque but

Africain trafiquant faux-billets
Mafia, Goor-Djiguène Ak millards
Policier Saay-saay
Bo guissé sathie kate audité sathie kate
Nopile té teuthie sa gate
Boy yigne teuthie 100 metres ak boy yigne djaalé
Rakk li la gni déh di doundou men

Ballou Gun sama son préféré
Ballou Gun sama son préféré yééé yééé
Ballou Gun sama son préféré
Fusillade sama Playlist sama Fucking Playlist

Niata nio dess han han?
Niata nio dess nigga?
Niata nio dess?
Niata nio dess nigga?
Niata nio dess?
Niata nio dess nigga?
Rescapé yi rek lay ray
Niata nio dess nigga?

Da ngène fogone ni yéneu gueune nit yi
Beug buzz ni kouy djoudo ci film X (X)
Nénagne disque d'or c'est pas possible
Chaque Rime xaliss noumay séralé

Dom dama baayi djangue boumala fayalé
Boy Clash Dip rang bi dafa Dafa séré lek
Taal bou Yalla taal bokoutak bou sénélec
Chaque rime xaliss noumay séralé
Dom dama baayi djangue boumala fayalé
Kouy djapp niay dou faalé bénène xéttu djaam
Boul aalou nieuweul yako téré neex
Galé daa xate mane ma fanaani studio

Héé li nga marr ci la lapp nigga
Yeukeutil poids mane may dougueul ay Millions
Liguèy pour niou mirasse my nigga
Rappeur wala Ninja my nigga
Fène kate wala tass katou xibaar my nigga
Fake nga Bitch nigga my nigga
Fuck U yaw ak say mbokk ak sa family yeup
Morééé

Ballou Gun sama son préféré
Ballou Gun sama son préféré yééé yééé
Ballou Gun sama son préféré
Fusillade sama, sama fuckin'

Niata nio dess han han?
Niata nio dess nigga?
Niata nio dess?
Niata nio dess nigga?
Niata nio dess?
Niata nio dess nigga?
Rescapé yi rek lay ray
Niata nio dess nigga?

Nio fi nékone, Nio fi nékaate
Auto-Rail sa kaw vagon yeup ci say yaxkh
Bo guissé Gun ci sama ndey djor
Rampam pam pam papam sa kaw comme cinéma
Mané
Nio fi nékone, Nio fi nékaate
Auto-Rail sa kaw vagon yeup ci say yaxkh
Bo guissé Gun ci sama main droite
Rampam pam pam papam comme cinéma

Eééh! Stay for real you are ready now
Stay for real you are ready now
Mama don't cry, pray for me yeah
Mama don't cry, yeah I'm ready

Most popular songs of Dip Doundou Guiss

Other artists of Afrobeats