Beats By Thiere

Elzo JamDong

Non mais vraiment fils yaye sèèèrrre lol
Jamm Dongg le!!!

Han wala sibeugouniou be légui?
Kone me takk seme casque Beats By Thiere?
Beats by Thiere bea-bea-beats by Thiere

Boumeu diémeu diss baye sèèkhe!
Kagn ngay nangou liniouy défeu diss baye sèkhe?
Jamdong leu only #pisse (peace) my friend
Sow se kow saison sèche nioune nioye wiss galsen
Cli-cli-click souniou page, sons you RICHE laye #CHER (share)
Flow bii diokh daadj ga yi sick aye khère
Wakh thi nioune lou bone douniou yakkhal khère
Nioune nioye spit crack yow yaye spit calcaire
Miss diaye chère guissoumeu sène prix
Motakh sene clip yi ken dou thi sène Free (hii)
Est ce que sene vies yi méngo na'k sene frime ?
Niou né thi scène bi di tassou thi sène fric (sene fric)
Non vraiment c triste waye merrrde
Yégo dor na dione Usher Ludacris -ah yea!? YEAHHH
This is #good music not a hit by Yé (kanyé)
Got my headphones bumpin beats by Thiere
Prrr

CHORUS
Non mais vraiment fils yaye sèèère
Non mais vraiment non mais vraiment fils yaye sèèèrrre
Me take seme dalle nga guiss Nike Airrrrr
Me takke sama casque, #beats by Thierrre
Beats by thiere bea-bea-beats by thiere X2
Me take seme dalle nga guiss Nike Airrrrr
Me takke sama casque, #beats by Thierrre

Outro
"Mister Thiere rap na rap be rap bi diékhe
Kou thi amoul sokhleu thi mic diokh me me dale di khèkhe"
Hahahaha

Trivia about the song Beats By Thiere by Elzo JamDong

When was the song “Beats By Thiere” released by Elzo JamDong?
The song Beats By Thiere was released in 2014, on the album “FreeDope”.

Most popular songs of Elzo JamDong

Other artists of African hip hop