Dose
I'm ready to play they know
May peundeul thiow li dou barri eh
I'm what you need, faw name bi day dem fou sori
Diokh la gua dathi, feel my vibes
I got the juice dont worry
Fi gni beu gua fadiou sel mind laniouy wo
That's why i'm back
You know, dose lalay diokh
Tell' em, tell' em i'm back
You know rap lalay diokh
Tell' em, tell' em i'm back
You know flow lalay diokh
Diokh la dose dioxat leu, sou doyoul bum lalay diokh
Dotofi fi wax ba doumla fatchi
Même sa xol boudone febar xegne dead
Doundou guay yeuk thi li may deff
cntidote bi xel ak xol lako bindé
Diaglél ko haters yi haters yi
Digen mér souma public biy teroussi
Lire na commentaire yi guiss doléances yi
Dotouma geudj di guénéti
Sa projet bi gassal kane bamou xaut soul ko
cntidote doko sout
Ma yor arme yeup ame cartouche
Fo guissé victime yanko mo shoot
May deff crime coupable nulle doute
Do guiss samay trace même bo yorone loupe
Wané gouma dara nieup dima wout
Sa label sama ambition moko sout
Jeuleul altitude pour get ma brain bé élevé nioun niéwou niou Newton
Sa rappeur lima ko seuf douko oyoff
Il fait pas le poids matoul libeur, may 1000 tonnes
Nioun God moniou bless up
Flag bi flotter na day diauk
cssamane dou sama limite
Xadiou ma thi paper
Name bi newoul thi liste
Kouy sama mass la meussoul guiss
Do you feel my vibes
Do you feel my vibes
I got everything, everything you want
Do you feel my vibes
Do you feel my vibes
I got everything, everything you want
I'm ready to play they know
May peundeul thiow li dou barri eh
I'm what you need, faw name bi day dem fou sori
Diokh la gua dathi, feel my vibes
I got the juice dont worry
Fi gni beu gua fadiou sel mind laniouy wo
That's why i'm back
You know, dose lalay diokh
Tell' em, tell' em i'm back
You know rap lalay diokh
Tell' em, tell' em i'm back
You know flow lalay diokh
Diokh la dose dioxat leu, sou doyoul bum lalay diokh
clbum guén lathi ma deff chef-d'œuvre offre bé eup
Ey ligey na yokal say demandes rap na way lep
Ey signél fi doto done nomade badi fan nieup
Ey sodé weur mc bou kamal bo akssé deup
Ey fo dieum, may the top
Indil kou meun fok ma fuck niaf
Cible bagui sen bop cK47 puff! puff!
Vider sama chargeur paré taxaw xar douniou daw keuf
cyouma thiy menace, ray mou dhé la xam boy dou ay bluff
Yeah i'm what you need
Yeah im what you need ey ey
Sou game bi amone team may coach di capitaine ey ey
May dougal indi coupe bi Sadio mané King ey ey
Limoy talent brute doumako ndiar damkoy assumé
Sa rappeur doumko nekh limouy bako mane mom lay fowé
Fuck ko meun ti done rappeur gua mane douma nit fils
Defal louma nekh pour meun diay loloy devisou pute
Sen xam xam beuriwoul matoul copou nane na guédiou kiss
So niémé diem m'a test sa carrière lay fay thi beneu biss
Do you feel my vibes
Do you feel my vibes
I got everything, everything you want
Do you feel my vibes
Do you feel my vibes
I got everything, everything you want
I'm ready to play they know
May peundeul thiow li dou barri eh
I'm what you need, faw name bi day dem fou sori
Diokh la gua dathi, feel my vibes
I got the juice dont worry
Fi gni beu gua fadiou sel mind laniouy wo
That's why i'm back
You know, dose lalay diokh
Tell' em, tell' em i'm back
You know rap lalay diokh
Tell' em, tell' em i'm back
You know flow lalay diokh
Diokh la dose dioxat leu, sou doyoul bum lalay diokh