No Stress

Non non bouñou nangou ñou ñouy tèk stress
Non non bouñou nangou ñou ñouy tèk stress
Non non bouñou nangou ñou ñouy tèk stress
Souñou xol di fess ñom ñou diouk deff fess

Non non douma nangou nga may tèk stress
Douma nangou nga may tèk stress
Ma bagne doumako nangou no stress
Sama xol di fess yaw nga diouk deff fess

Mani dimbalima wax dji beurina
Mane reik thi xalè namouma dara
Mani dimbalima wax dji beurina
Mane reik thi xalè namouma dara

Dagua fatè ni awma dix ans
Lou tax gna dieul ma beug ma deff sa fowoukay
Yombeuleul naleuh sa visa
Wow yeah yeah, demal foula nex way

Beugua languak ki
Beugua languak kè
Beugua languak samay xarite mani night and day
Dégue na niounè fèbar lah
Wow yeah yeah, deffal loula nèx way

Non non douma nangou nga may tèk stress
Douma nangou fils nga may tèk stress
Ma bagne doumako nangou no stress
Sama xol di fess yaw nga diouk deff fess

Mani dimbalima wax dji beurina
Mane reik thi xalè namouma dara
Mani dimbalima wax dji beurina
Mane reik thi xalè namouma dara

Goor goula tèk deal lundi ba dimanche noboula
Kouma beugua tardèl beugue ma fowè ma rombe lah
Goor goula tèk deal lundi ba dimanche noboula
Kouma beugua tardèk mane ma rombe lah

Li safatouma
Sama mètytou mouñe dièxna
Li yeugnalouma
Ndax tè mane niakouma fayda
Li safatouma
Tèguou thi temps deff bamou bax jotna
Tè yaw mi xamgua
Soma noboul sa morom nob mah

Non non bouñou nangou ñou ñouy tèk stress
Bouñou nangou ñou ñouy tèk stress
Non non bouñou nangou ñou ñouy tèk stress
Souniou xol di fess ñom ñou diouk deff fess

Non non douma nangou gna may tèk stress
Non non douma nangou gna may tèk stress
Ma bagne doumako nangou no stress
Sama xol di fess yaw gna diouk deff fess

Mani dimbalima wax dji beurina
Mane reik thi xalè namouma dara
Mani dimbalima wax dji beurina
Mane reik thi xalè namouma dara

Goor goula tèk deal lundi ba dimanche noboula
Kouma beugua tardèl beugue ma fowè ma rombe lah
Goor goula tèk deal lundi ba dimanche noboula
Kouma beugua tardèk mane ma rombe lah

Other artists of Contemporary R&B