Bolo Leen

Youssou N'Dour

Eh eh eh
Lo khamni, fi lagn ko ba
Diaroul di tiiteur
Eh eh eh
Do faté
Ba penthieu meu
Yaw diar nga titeul
An, ni nga mél
Bi ngay nieuw
Bow délouwaat
Nonou ngay mél
Sa katane fatélola
Ba nga bèèw
Bëss di na nieuw
Yaw doka tal
Lépp loy déf
Oa Yalla takh

Oh, oh, oh
Eh, eh, eh
Lo khamni, fi lagn ko ba
Diaroul di tiiteur
Eh, eh, eh do faté
Ba penthieu meu
Yaw diar nga titeul
Adouna bi, day weulbatikou
Dèko sooraléy
Bayi ca khél
Tay meun nga
Am euleuk
Danou ba bo léké
Dagn la yakal

Waw né beugueu dal
Bou dé lou wérr
Dou séét mélo
Oh, oh, oh
Eh, eh, eh
Lo khamni, fi lagn ko ba
Diaroul di tiiteur
Eh, eh, eh do faté
Ba penthieu meu
Yaw diar nga titeul
Adouna bi, day weulbatikou
Dèko sooraléy
Bayi ca khél
So démé Gueule Tapé yéneu grand-place yeu do mana khamm
Kouy général bé
Minitre bé
Ouvrier
Oh, oh, oh

Bo lén ko niamé
Ni ngén ko meuné
Noney mom la yeugué
Bo lén ko défé
Ya gueun ci gouné
Nonéy mom lay yégué
Bo lén ko meuné
Fi ngén ko meuné
Fofé moy taar bi
Mo gueun ci gouné
Mo gueun ci founé
Nonéy yeurmandé
Diar-diarou gounè
Moy firndé gounè
Loley moy taar bi

Bou yone wi soré
Moy takh mou diégué
Loléy moy taar bi

Moy défar société bi
Ratakhal digueunté yi
Yombal démlanté bi
Di néweul baguanté bi
Yokeu yokeu société bi
Di néweul baguanté bi
Di wangni nioranté bi
Feusseul begueunté bi
Yokeu société bi

Trivia about the song Bolo Leen by Youssou N'Dour

Who composed the song “Bolo Leen” by Youssou N'Dour?
The song “Bolo Leen” by Youssou N'Dour was composed by Youssou N'Dour.

Most popular songs of Youssou N'Dour

Other artists of World music