Ndox

Youssou N’Dour, Hakim Abdulsamad, El Hadji Faye

Sa joie et sa pudeur font sa face cachée
Son paraître et ses formes montrent sa force
Celle que je vous chante, vous est familière!
Elle est utile et belle
Elle a révélé la beauté du monde
On la clame Paradis

Mbégté ma , suturë sa
Da fa méngóo k , baatin ëm
Zaahir sa , melo ya
Moo won e , kattan am

Li may misaal lu ngeen xam la
Am na njariñ te rafet na
Moo génné taar u adduna
Moom la ñu bakke , al janna
Waxtaan e ko sax banneex la
Nañ ko foηk sakkan al ko

En parler même est agréable!
Respectons-la, économisons-la
Vois la mer, le flеuve
Rendons grâce à Diеu
Elle est utile et belle
Elle a révélé la beauté du monde
On la clame Paradis
Mbégté ma , suturë sa
Da fa méngóo k , baatin ëm
Zaahir sa , melo ya
Moo won e , kattan am

Li may misaal lu ngeen xam la
Am na njariñ te rafet na
Moo génné taar u adduna
Moom la ñu bakke , al janna
Waxtaan e ko sax banneex la
Nañ ko foηk sakkan al ko

Géej gaa ngi nii yé
Dex gaa ngi nii yé

Dara gën ul ë neex taw bi

Ku weddi laaj ko bay kat ba
Ci la ñuy roosé seen tool ya
Walla nga laaj ko samm kat ba
Ci la ñuy nandal e jur gë
Ndox daal am na njariñ baax na
Dara gën ul lë neex taw bi
Taw daal njariñ la ci dun bi

Ndox daal njariñ ëm
Ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñ ëm
Ba la nga koo xam mu manqué

Ndox daal njariñ ëm
Ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñ ëm
Ba la nga koo xam mu manqué

Ndox daal njariñ ëm
Ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñ ëm , ba la nga koo xam mu manqué

Ndox daal njariñ ëm
Ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñ ëm
Ba la nga koo xam mu manqué

Ndox daal njariñ ëm
Ba la nga koo xam mu jafe
Ndox daal njariñ ëm
Ba la nga koo xam mu manqué

Alaa gaynaago yoo samba lingeer
Donoy waaly yée , wulée ñaay ngoy
Yée gan wuri coo , wulée gaynaako yoo
Yeée , yóo , gan fari baa

Trivia about the song Ndox by Youssou N'Dour

Who composed the song “Ndox” by Youssou N'Dour?
The song “Ndox” by Youssou N'Dour was composed by Youssou N’Dour, Hakim Abdulsamad, El Hadji Faye.

Most popular songs of Youssou N'Dour

Other artists of World music