Seuss

"...350 nga def thi kankan"

Verse 1: Elzo

Han eh yow
Mane le waKHambandé'k sama mbaKHAné
TaKHawalok seme taKHandér, taKHaw ak
Gni toke thi banc diaKHlé yi waKHtané tékkiii
DaKHanté'k borom képi yi
Gni di taKHalé ndékkiii
Di diémeu nekk-nekkal nabb-nabbal dongg mou gueun di mettiii
Mère yi yèwou soubeu défar wayé diekk diekkal rek
Kiy dore war diapp chill ngay toke di play
Bou done nélaw di ko am kham nga dou diok fi téy
Faya, forokh thiaya yi ga yiy diaye thi mbed mi
Niou rap be tangg nguirr baye bi fanaane thi sedd bi !
Loutakh fi deunguey dem be seuss dem be chaud coeur?
Dem be bo fi guédié touti nieuwate deunguey choquer...
Ségueum ko laathié niouné le "DIEUL ne gaal" wala "pitche";
Wala DIEUL ne wird sakh nga bég!
Wayé DIEUL ne coke be doff DIEUL ne crack be off
DIEUL ne perpette rek laye bégneu dégg!
-Ani sho bi deukkone wétou gallé niom...?
-"Ben bro teuf ne ko!"
-Copineum b...
-"Benn kaweman keuf ne ko!"
-Non kogne bi defe gueuneu ruff poto!
-"Mmo bou bougoul wone sakh mèreum seuf ko ko !"

Diangg na thi niom mak lou beuri lou takh me tèleu done mak
Motakh me tèleu dof takh me tèleu dokh takh me tèleu yor mic
Diok diémeu tèleu fass se diom ak
Fouleu moye takh nga tèleu done crack
Wayé kogn bi tèleu bone, tèleu fone, saathieu téléphone diaaye

Boy town khèpe "Narr" "wa Baol" ak "wa Guinée"
Mo niou takheu yém fi wa dji lé
Bouniou kharr kenn di niou baratiner
Dieuw "minette bi sakh wène légui" ak "ki tate yi réye"
Nane "niak bi... ndring bi" té joboulo
Nga diappé lène dof yow nga fok né diobbeulo ?
Yakamti yakhoulé, wayé kou daagou dé
Da'a goudé, niouné leu "ya khoullé!"

Chorus : Elzo
Hey rakk deungueu beugg guiss
Loutakh gorr Yalla yi seuss?
Defe fekk rek niouy guiss
Sène morom yi di beuss
Liniou yanou gueuneu diss X2
Gueuneu diss X2

Hey makk deungueu beugg guiss
Loutakh gorr Yalla yi seuss?
Defe fekk rek niouy guiss
Sène morom yi di beuss
Liniou yanou gueuneu diss (X2)
Gueuneu diss (X2)

Verse 2: Mo Faya

Mbeddeu ba ngui PARAno,Gars yi djekki PARessi
PARait-il PARAsite yi wathieu comme aye PARAchute !
Andando yi paré ici mane, guiss na aye PAResseux
PARait que dagne laye caressé djokk PARél leu !

Intifida Palestine ake economy paradise
Takk eukhlou legalize, get wise kharéleu
Amatoul khaleleu if so yékhé garé ngeu
Déggo xarégne ngeu, realize ndaré ngeu!

Fuck mou hot(hot), ndax dox la amoul takk
Boudé wax rek mate na fight, mais dieuf bé eupeu daadj(eupeu daadj)/
Deggeu daadj, yow fau nga deggeu daadj/
Ndax bala laax djaay goor faut qu' nga laax taadj

Kone djéguessil, xame nga nieuppeu gnémé fii
Défeni, ding niou téré niafé ni Kennedy nigger djeguéssil
Yéék comme Khomeyni seuuss comme wa Tchernobyl
Djeguessil, yékeutil level bi dafa pathétik

Chorus
Hey rakk deungueu beugg guiss
Loutakh gorr Yalla yi seuss?
Defe fekk rek niouy guiss
Sène morom yi di beuss
Liniou yanou gueuneu diss X2
Gueuneu diss X2

Hey makk deungueu beugg guiss
Loutakh gorr Yalla yi seuss?
Defe fekk rek niouy guiss
Sène morom yi di beuss
Liniou yanou gueuneu diss (X2)
Gueuneu diss (X2)

Verse 3: Elzo

Me nieuw Babylone Ghetto kass, Ghetto races
Ghetto Narr, Ghetto Nioule
Ghetto daal, negn wakhanté deugg
Mais ken moussoul degg ghetto cool
Gni ghetto yakkh , gni ghetto mourr
Gni ghetto shot ak gni ghetto soule...
Aka beuri ay ghetto bourr, you moudié done aye ghetto poupe!
Thi ghetto chaque jour mouno teudd té déggo youkhou
Kone ghetto youth yi nouniouy def be douniou fatté li nio défone cours?
Ak li niou défone pour am sene diamm? déniou khékhone couz !
Sène efforts nuls neu (kholeul) deunguey diakhlé bo fi défone tour!

Crack , alcool alkou-land, bédo-bar entourage
Gni done diaay sankkhal sankou néniou
Gni ko done dieunde nieupp bankou néniou X2

Taylé se life thi thiaga, thiakaay ak tangal came=
Dèè jail wala niou rap'at le Sangalkam X2

Outro
Hey rakk deungueu beugg sip loutakh Gorr Yalla yi seuss?
Defe fekk rek niouy guiss, sène morom yi di beuss...
Liniou yanou di gueuneu diss diss diss diss diss diss

Trivia about the song Seuss by Elzo JamDong

When was the song “Seuss” released by Elzo JamDong?
The song Seuss was released in 2014, on the album “FreeDope”.

Most popular songs of Elzo JamDong

Other artists of African hip hop