Xamoulo

Timothee Wecxsteen

Nit ku né da ngay ame fi ngay jaar
Bo démé ba nga magg dal di bér sa daara
Di nga tolleu çi jamono yu tar
Jafé-jafé né fi jëpet té manulo çi dara
Waayé bumu téé nga raag
Gëm ni di nga tekki té ken manu çi dara
Di nga daanu wayé faw nga jogaat
Seytaané dafay dëpp sa xel nga dem ba saaran
Baayi ma dem baayma ma dem mangi on my way
Bo demul ma dem man are hustling day by day
Baayi ma dem baayma ma dem mangi on my way
Bo demul ma dem man are hustling day by day
Mane kessé mane xam limay daj
Yalla sutural ma ba ma delu çi mama
Dégg na mbow yi ni xadj
Gestu tuma falétuma mangi ça canam
Doneté yalla may nama baat
May goorgoorlu di çi ñéfé di wax lu am maana
Bu féké séni xol yé xat
Xaaral ma yeketi sama ñételi baaram
Baayi ma ma dem baayma ma ma dem mangi on my way
Bo demul ma dem man are hustling day by day
Baayi ma dem baayma ma dem mangi on my way
Bo demul ma dem man are hustling day by day
Xamulo ki ma doon
Xamulo fi ma jeum
Xamulo lima gëm, nga bëggë ma juger
Guissulo sama xol
Dugulo sama xel
Sopulo ni ma mel man, nga bëggë ma juger
Elz dafay weengg waaye Elz du daanu
Elz dafa dikidi-dingue dingue mais am na ñaanu waajur
Li Elz jota dund, ku ko xamul na maanu
Gaynde dëgg da lay ngàdd doo ko degg mu aalu
Deembë maa ngue'k Efya tey maa ngue'k Natty di play
Tukki fepp ci adduna bi comme cmiri plane

Gumbë ci xar yiy mbëw, tëx ci xaj yi di mbee
Ñu amul ciment rek'ay romb tabax sanni ci xeer
Yeah 16 piges maa ngi bind ay 16
Juddu pour def lu big comme kouy and ak Cease
Huey Peace, 2016, maa ngi bind ay scenes
Comme Sembene, bañoon school mais j'ai aimé Césaire fils
Baayi ma ma dem, baayi ma ma dem maa ngi on my way eh eh
Demul ma dem, man'a hustlin mane day by day
Xamulo ki ma doon
Xamulo fi ma jeum
Xamulo lima gëm, nga bëggë ma juger
Guissulo sama xol
Dugulo sama xel
Sopulo ni ma mel man, nga bëggë ma juger

Most popular songs of Natty Jean

Other artists of African reggae